Alioune Tine loumouy wax wa kogne ba 😂😂😂
Posts by
2022, prix du kg d'arachide 275 FCFA.
2023, prix du kg d'arachide 280 FCFA.
2024, prix du kg d'arachide 305 FCFA.
Nos encouragements au gouvernement.
Bonne continuation !
De Honorable député Guy Marius SAGNA 🇸🇳🚨
Fii narr na rebeudioo nak 😂
Il fii dafa ame ayy pêcheurs 😂
Mais fii warna meune ame réponse vocale dh
Déff différence akk wa boor beulé sax gayi meune roubé
Bismillah barkép Cheikh Ibrë 🖤🤍
Amine frère
Matna 😂😂😂
Samay délais la yorr 24 tu fb pas ma nangou sama follow
Détt douma sétane lolou
Damay lathié rek
Waxma 🙈
🤧 Patriote nga ?
Laisse ça 🥱
Jàmm dji gnou ame fii bouko dara yakk
"Prési sa xarit toubacouta" 😭😭
C'est des envahisseurs
Gnoniou dagno euppeul dh 😂😂😂
Mongui tollo dh 🤧
154 mooy 154
Lii histoire dinako binde mome lagn ndieukke kong sur BSky
😂😂😂
Yup je sais 🤗
Commencé ti nguén 🤧
Koula bloquer X, niew fi follow leu tamit grawoul adouna amoul solo😂
Jbk tous le monde azi guys
Tl xassida ak Tl zikroulah folén nékk ?
Les gars de la société civile boufi kèneu tékk tànkam nguir yalla rek pas de naféx ici 🥱
Fb
Omar waxal Coumba mou créer compte bluesky 😂😂😂
C’est nous les méchants 😹🇸🇳☠️ nous avons braqué l’algo de ce réseau 🔥 feu gayi feu