Si Tu aimes Ousmane Sonko, like et rt ce post on va voir les vrais patriotes
1 year ago
289
115
10
4
Si Tu aimes Ousmane Sonko, like et rt ce post on va voir les vrais patriotes
Deet waay
Sawara mas naa laaj wàllam Sëriñ bi ci li muy joxe ? Sëriñ bi tontu ko luy tektale ni amul benn dur (lor) léppam njariñ la. Bi sawara naagoo ba waññi ko, Sëriñ bi ni ko bu bis baa ku masa diŋat Ibra Faal sab cër la, bu ko jéggalee nga xam ni moo la ko xañ.
Sërin tuuba nee na jëw moo gën a bon sàcc ndax sàcc man naa jariñ ka ko def mel ni mu sàcc am mbubbu wala lu ñuy lekk, jëw moom du jariñ boroom dara te dafay dindi ag ngëm ci ab xol.