C'est ça deh bcp de travailleur sont dans l'insécurité galsen ken hamul lan là 🤦🏾♂️
Posts by
C'est super 🎉
@serviteur.bsky.social
Ken du niom nio yemer
@serviteur.bsky.social
Kokou dafa beury pah motah tt es possible
Naniou defar terrain bi bamu yadieun comme sa Pros sous niower niou dalal ko
bayil rek mu sedd
Esk moom sah diekou am compte sah
dette way aladji esk doko tek si souff rek
Niom dañu dermelu
Mom kay
Beury wouniou dooler dank sah 🤧
Bly niom souniou niower fi rek dotoul nekh
One rek
Waf niou wiss terrain bi bala magu démb yi di niow
Li kay 🤧
Ki kay waru fee eksi sinon mbëcter mi yeup lay xadiamal
Ki da doon napp gars yi 🤧 mes sifflé bisi souff ak wouh bi momay daji 😂
On est sur la même longueur d’onde, tu as tout saisi aussi ! 🔥👌
Le parti Pastef peut être comparé à la Masia ⚽✨, car il regorge de nombreux intellectuels 📚💡. À chaque intervention, on découvre des talents 🔥🌟 qui donnent du fil à retordre à l’opposition 🗣️🔄. Le gars à l’aise 💼👏 a livré une véritable masterclass.
Système bi danu na
Esk teloul
Bly
Wa lolou waroul takh nga fater kër gu mak 🤧 pourtant waro def ni X sa kër là
dette way 😂 aladji heup na wax xar ma niow abonné si iow
dette way 😂 aladji heup na def
Wa kër gu sell bi